Az-Zukhruf · 26/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَإِذْ قَالَ إِبْرَاهِيمُ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ إِنَّنِي بَرَاءٌ مِّمَّا تَعْبُدُونَ ۝٢٦
Wa iz qaala Ibraaheemu liabeehi wa qawmiheee innane baraaa`um mimmaa ta`budo
📖 Tekkim Wolof
(Fàttalikul) Ibraahiima ba mu waxee baayam aku nitam : “Man mii ku deñ laa ci lii ngeen di jaamu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Az-Zukhruf

24۞ قَالَ أَوَلَوْ جِئْتُكُم بِأَهْدَىٰ مِمَّا وَجَدتُّمْ عَلَيْهِ آبَاءَكُمْ ۖ قَالُوا إِنَّا بِمَا أُرْسِلْتُم بِهِ كَافِرُونَ
Mu wax leen ne : “Ndax indilu ma leen lu gën a jub la seen baay ya nekkoon ? ” Ñu tontu ne ko : “Nun kat gëmu nu lii ñu la yónni”.
25فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُكَذِّبِينَ
Nu daldi fayu ca seen kaw. Xoolal (settantal) naka la mujjug weddikat ya deme.
26وَإِذْ قَالَ إِبْرَاهِيمُ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ إِنَّنِي بَرَاءٌ مِّمَّا تَعْبُدُونَ
(Fàttalikul) Ibraahiima ba mu waxee baayam aku nitam : “Man mii ku deñ laa ci lii ngeen di jaamu,
27إِلَّا الَّذِي فَطَرَنِي فَإِنَّهُ سَيَهْدِينِ
ba mu des (Yàlla) mi ma sàkk bind ma, te moo may gindi”.
28وَجَعَلَهَا كَلِمَةً بَاقِيَةً فِي عَقِبِهِ لَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ
Mu def (dénkaane boobu) muy kàddu guy sax ginnaawam. Ngir amaana ñu dellu (di jëfe seeni xel) ?
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 26

Simoore Az-Zukhruf Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Fàttalikul) Ibraahiima ba mu waxee baayam aku nitam : “Man…

Simoore Aaya 26/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers