Az-Zukhruf · 32/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
أَهُمْ يَقْسِمُونَ رَحْمَتَ رَبِّكَ ۚ نَحْنُ قَسَمْنَا بَيْنَهُم مَّعِيشَتَهُمْ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۚ وَرَفَعْنَا بَعْضَهُمْ فَوْقَ بَعْضٍ دَرَجَاتٍ لِّيَتَّخِذَ بَعْضُهُم بَعْضًا سُخْرِيًّا ۗ وَرَحْمَتُ رَبِّكَ خَيْرٌ مِّمَّا يَجْمَعُونَ ۝٣٢
Ahum yaqsimoona rahmata Rabbik; Nahnu qasamnaa bainahum ma`eeshatahum fil hayaatid dunyaa wa rafa`naa ba`dahum fawqa ba`din darajaatil liyattakhiza ba`duhum ba`dan sukhriyyaa; wa rahmatu Rabbika khairum mimmaa yajma`oon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ñoom ñooy séddële yërmaandey sa Boroom ? Te Nun dey Noo leen di séddale seenub dundu ci àddina te it tooñkat ya ñennat ci ñoom, teg na leen ca kaw ña ca des ngir nuy yilifante. Waaye yërmaandey sa Boroom, moo gën fuuf, li ñuy dajale.

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Az-Zukhruf

30وَلَمَّا جَاءَهُمُ الْحَقُّ قَالُوا هَٰذَا سِحْرٌ وَإِنَّا بِهِ كَافِرُونَ
Ba leen dëgg ga digëlee, dañoo wax naan : “Lii daal ag njibar la te nun ay fen la nu ko jàppe”.
31وَقَالُوا لَوْلَا نُزِّلَ هَٰذَا الْقُرْآنُ عَلَىٰ رَجُلٍ مِّنَ الْقَرْيَتَيْنِ عَظِيمٍ
Ñuy wax it ne: “Cëy Alxuraan jii bu wàccoon ci nit ku tekki te dëkk ci benn ci ñaari dëkk yi ? ” (Taayif, Màkka) (al Waliidu ibn almuqiira) walla (Urwatu ibn masuud).
32أَهُمْ يَقْسِمُونَ رَحْمَتَ رَبِّكَ ۚ نَحْنُ قَسَمْنَا بَيْنَهُم مَّعِيشَتَهُمْ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۚ وَرَفَعْنَا بَعْضَهُمْ فَوْقَ بَعْضٍ دَرَجَاتٍ لِّيَتَّخِذَ بَعْضُهُم بَعْضًا سُخْرِيًّا ۗ وَرَحْمَتُ رَبِّكَ خَيْرٌ مِّمَّا يَجْمَعُونَ
Moo ndax ñoom ñooy séddële yërmaandey sa Boroom ? Te Nun dey Noo leen di séddale seenub dundu ci àddina te it tooñkat ya ñennat ci ñoom, teg na leen ca kaw ña ca des ngir nuy yilifante. Waaye yërmaandey sa Boroom, moo gën fuuf, li ñuy dajale.
33وَلَوْلَا أَن يَكُونَ النَّاسُ أُمَّةً وَاحِدَةً لَّجَعَلْنَا لِمَن يَكْفُرُ بِالرَّحْمَٰنِ لِبُيُوتِهِمْ سُقُفًا مِّن فِضَّةٍ وَمَعَارِجَ عَلَيْهَا يَظْهَرُونَ
Su nit ñi doonoon wenn xeet, kon Dinanu defaral ñiy weddi Yàlla, seeni kër am ay xàddi xaalis ak ay ker-keraan ñu di ca yéege ;
34وَلِبُيُوتِهِمْ أَبْوَابًا وَسُرُرًا عَلَيْهَا يَتَّكِئُونَ
seen kër ya amna ay wunt ak ay lal ñu di ca sóonu,
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 32

Simoore Az-Zukhruf Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ñoom ñooy séddële yërmaandey sa Boroom ? Te…

Simoore Aaya 32/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers