Az-Zukhruf · 60/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَلَوْ نَشَاءُ لَجَعَلْنَا مِنكُم مَّلَائِكَةً فِي الْأَرْضِ يَخْلُفُونَ ۝٦٠
Wa law nashaaa`u laja`alnaa minkum malaaa`ikatan fil ardi yakhlufoon
📖 Tekkim Wolof
Bu Nu sooboon , Nu def ci yéen ay Malaaka yuy ayayloo ci kaw suuf si.

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Simoore Az-Zukhruf

58وَقَالُوا أَآلِهَتُنَا خَيْرٌ أَمْ هُوَ ۚ مَا ضَرَبُوهُ لَكَ إِلَّا جَدَلًا ۚ بَلْ هُمْ قَوْمٌ خَصِمُونَ
Ñu daldi wax ne : “Ndax sunuy Yàlla ñoo gën, walla moom sax ? ” Ay werante rekk la ñu fi indi . Te sax ñoom ay niti tafaar la ñu.
59إِنْ هُوَ إِلَّا عَبْدٌ أَنْعَمْنَا عَلَيْهِ وَجَعَلْنَاهُ مَثَلًا لِّبَنِي إِسْرَائِيلَ
Moom de (Muusaa) ab jaam rekk la bu Nu jox xeewal def ko muy roytéef ci wa Bani Israayiil.
60وَلَوْ نَشَاءُ لَجَعَلْنَا مِنكُم مَّلَائِكَةً فِي الْأَرْضِ يَخْلُفُونَ
Bu Nu sooboon , Nu def ci yéen ay Malaaka yuy ayayloo ci kaw suuf si.
61وَإِنَّهُ لَعِلْمٌ لِّلسَّاعَةِ فَلَا تَمْتَرُنَّ بِهَا وَاتَّبِعُونِ ۚ هَٰذَا صِرَاطٌ مُّسْتَقِيمٌ
Te firnde lay doon ci (Bis Pénc ba) waxtu wa. Buleen ci am sikki-sàkka. Te na ngeen ma topp : yoon wu jub xocc waa ngi nii.
62وَلَا يَصُدَّنَّكُمُ الشَّيْطَانُ ۖ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Buleen nangu mukk Saytaane di leen wëlbati ! Ndax seenub noon la (bu nëbbutuwul) fes.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
60Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 60

Simoore Az-Zukhruf Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu Nu sooboon , Nu def ci yéen ay Malaaka…

Simoore Aaya 60/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers