Az-Zukhruf · 59/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
إِنْ هُوَ إِلَّا عَبْدٌ أَنْعَمْنَا عَلَيْهِ وَجَعَلْنَاهُ مَثَلًا لِّبَنِي إِسْرَائِيلَ ۝٥٩
In huwa illaa `abdun an`amnaa `alaihi wa ja`alnaahu masalal li Baneee Israaa`eel
📖 Tekkim Wolof
Moom de (Muusaa) ab jaam rekk la bu Nu jox xeewal def ko muy roytéef ci wa Bani Israayiil.

🎧 Dégg


📜 Aaya 57-61 — Simoore Az-Zukhruf

57۞ وَلَمَّا ضُرِبَ ابْنُ مَرْيَمَ مَثَلًا إِذَا قَوْمُكَ مِنْهُ يَصِدُّونَ
Ba ñu jëlee misaal ci Iisaa doomi Maryaama, saw nit dañoo daldi dumóoyu,
58وَقَالُوا أَآلِهَتُنَا خَيْرٌ أَمْ هُوَ ۚ مَا ضَرَبُوهُ لَكَ إِلَّا جَدَلًا ۚ بَلْ هُمْ قَوْمٌ خَصِمُونَ
Ñu daldi wax ne : “Ndax sunuy Yàlla ñoo gën, walla moom sax ? ” Ay werante rekk la ñu fi indi . Te sax ñoom ay niti tafaar la ñu.
59إِنْ هُوَ إِلَّا عَبْدٌ أَنْعَمْنَا عَلَيْهِ وَجَعَلْنَاهُ مَثَلًا لِّبَنِي إِسْرَائِيلَ
Moom de (Muusaa) ab jaam rekk la bu Nu jox xeewal def ko muy roytéef ci wa Bani Israayiil.
60وَلَوْ نَشَاءُ لَجَعَلْنَا مِنكُم مَّلَائِكَةً فِي الْأَرْضِ يَخْلُفُونَ
Bu Nu sooboon , Nu def ci yéen ay Malaaka yuy ayayloo ci kaw suuf si.
61وَإِنَّهُ لَعِلْمٌ لِّلسَّاعَةِ فَلَا تَمْتَرُنَّ بِهَا وَاتَّبِعُونِ ۚ هَٰذَا صِرَاطٌ مُّسْتَقِيمٌ
Te firnde lay doon ci (Bis Pénc ba) waxtu wa. Buleen ci am sikki-sàkka. Te na ngeen ma topp : yoon wu jub xocc waa ngi nii.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 59

Simoore Az-Zukhruf Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom de (Muusaa) ab jaam rekk la bu Nu jox…

Simoore Aaya 59/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers