Az-Zukhruf · 69/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
الَّذِينَ آمَنُوا بِآيَاتِنَا وَكَانُوا مُسْلِمِينَ ۝٦٩
Allazeena aamanoo bi Aayaatinaa wa kaanoo muslimeen
📖 Tekkim Wolof
Ña gëmoon Sunuy kàddu te doonoon ay jullit,

🎧 Dégg


📜 Aaya 67-71 — Simoore Az-Zukhruf

67الْأَخِلَّاءُ يَوْمَئِذٍ بَعْضُهُمْ لِبَعْضٍ عَدُوٌّ إِلَّا الْمُتَّقِينَ
Ña xaritoo woon, bu keroogee ñennat ci ñoom, ay noon la ñuy doon ; lu ca dul ñay ragal Yàlla.
68يَا عِبَادِ لَا خَوْفٌ عَلَيْكُمُ الْيَوْمَ وَلَا أَنتُمْ تَحْزَنُونَ
“Éy yéen Sama jaam ñi ! tey jii buleen tiit ; mbaa ngeen di jaaxle,
69الَّذِينَ آمَنُوا بِآيَاتِنَا وَكَانُوا مُسْلِمِينَ
Ña gëmoon Sunuy kàddu te doonoon ay jullit,
70ادْخُلُوا الْجَنَّةَ أَنتُمْ وَأَزْوَاجُكُمْ تُحْبَرُونَ
“Dugguleen àjjana, yéen ak seeni soxna, danu leen fay berndeel”.
71يُطَافُ عَلَيْهِم بِصِحَافٍ مِّن ذَهَبٍ وَأَكْوَابٍ ۖ وَفِيهَا مَا تَشْتَهِيهِ الْأَنفُسُ وَتَلَذُّ الْأَعْيُنُ ۖ وَأَنتُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Danu leen fay wër ak booli wurus ak i kopp ; def lépp lu bakkan di wonnen ay gët di ko bànneexoo ; - “te dangeen fay béel.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 69

Simoore Az-Zukhruf Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña gëmoon Sunuy kàddu te doonoon ay jullit,

Simoore Aaya 69/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers