Az-Zukhruf · 70/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
ادْخُلُوا الْجَنَّةَ أَنتُمْ وَأَزْوَاجُكُمْ تُحْبَرُونَ ۝٧٠
Udkhulul Jannata antum wa azwaajukum tuhbaroon
📖 Tekkim Wolof
“Dugguleen àjjana, yéen ak seeni soxna, danu leen fay berndeel”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 68-72 — Az-Zukhruf

68يَا عِبَادِ لَا خَوْفٌ عَلَيْكُمُ الْيَوْمَ وَلَا أَنتُمْ تَحْزَنُونَ
“Éy yéen Sama jaam ñi ! tey jii buleen tiit ; mbaa ngeen di jaaxle,
69الَّذِينَ آمَنُوا بِآيَاتِنَا وَكَانُوا مُسْلِمِينَ
Ña gëmoon Sunuy kàddu te doonoon ay jullit,
70ادْخُلُوا الْجَنَّةَ أَنتُمْ وَأَزْوَاجُكُمْ تُحْبَرُونَ
“Dugguleen àjjana, yéen ak seeni soxna, danu leen fay berndeel”.
71يُطَافُ عَلَيْهِم بِصِحَافٍ مِّن ذَهَبٍ وَأَكْوَابٍ ۖ وَفِيهَا مَا تَشْتَهِيهِ الْأَنفُسُ وَتَلَذُّ الْأَعْيُنُ ۖ وَأَنتُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Danu leen fay wër ak booli wurus ak i kopp ; def lépp lu bakkan di wonnen ay gët di ko bànneexoo ; - “te dangeen fay béel.
72وَتِلْكَ الْجَنَّةُ الَّتِي أُورِثْتُمُوهَا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Loolee mooy àjjana ja Nu leen donale ci la ngeen daan jëf.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
70Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 70

Simoore Az-Zukhruf Aaya 70 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Dugguleen àjjana, yéen ak seeni soxna, danu leen fay berndeel”.

Simoore Aaya 70/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 68–72. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers