Al-Hujurat · 18/18
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hujurat
إِنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ غَيْبَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَاللَّهُ بَصِيرٌ بِمَا تَعْمَلُونَ ۝١٨
Innal laaha ya`lamu ghaibas samaawaati wal ard; wallaahu baseerum bimaa ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla xam na Mbóotum asamaan yeek suuf si, te Yàlla nag Kuy gis la li ngeen di def.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 16-18 — Simoore Al-Hujurat

16قُلْ أَتُعَلِّمُونَ اللَّهَ بِدِينِكُمْ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۚ وَاللَّهُ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Waxal ne : “Ndax dangeen bëgg jàngal Yàlla seen diine, te Yàlla moom xam na li nekk ci biir asamaan yeek suuf si ? ” Yàlla Xamaakoon la ci lépp lu ne.
17يَمُنُّونَ عَلَيْكَ أَنْ أَسْلَمُوا ۖ قُل لَّا تَمُنُّوا عَلَيَّ إِسْلَامَكُم ۖ بَلِ اللَّهُ يَمُنُّ عَلَيْكُمْ أَنْ هَدَاكُمْ لِلْإِيمَانِ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ña nga lay caakaayoo seenug dugg ci Lislaam. Nee leen : “ Bu leen caakaayo ci seenug tàbbi ci (diine Islaam). Yàlla kay moo ame ndam li moom mi leen xéewale gindi leen jëme leen ci ngëm , ndegam ñu dëggu ngeen”.
18إِنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ غَيْبَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَاللَّهُ بَصِيرٌ بِمَا تَعْمَلُونَ
Yàlla xam na Mbóotum asamaan yeek suuf si, te Yàlla nag Kuy gis la li ngeen di def.
Al-HujuratFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Hujurat 18

Simoore Al-Hujurat Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla xam na Mbóotum asamaan yeek suuf si, te Yàlla…

Simoore Aaya 18/18 — Simoore Al-Hujurat الحجرات (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hujurat Dégg, Simoore Al-Hujurat Tekki, Simoore Al-Hujurat mp3, Simoore Al-Hujurat pdf. Aaya 16–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers