Al-Maida · 92/120
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Maida
وَأَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ وَاحْذَرُوا ۚ فَإِن تَوَلَّيْتُمْ فَاعْلَمُوا أَنَّمَا عَلَىٰ رَسُولِنَا الْبَلَاغُ الْمُبِينُ ۝٩٢
Wa atee`ul laaha wa atee`ur Rasoola wahzaroo; fa in tawal laitum fa`lamooo annamaa `alaa Rasoolinal balaaghul mubeen
📖 Tekkim Wolof
Nangeen topp Yàlla ak Yonent bi, te ngeen wattandiku ! Bu ngeen dëddoo... nangeen xam ne Sunu Yonent bi dara waru ko lu dul jotal gu mat sëkk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 90-94 — Simoore Al-Maida

90يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِنَّمَا الْخَمْرُ وَالْمَيْسِرُ وَالْأَنصَابُ وَالْأَزْلَامُ رِجْسٌ مِّنْ عَمَلِ الشَّيْطَانِ فَاجْتَنِبُوهُ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Éy yéen ñi gëm ! [xamleen ne] sàngara, wure, xerëm ak seen banti gisaane, nekkuñu lu dul sobe su jóge ci jëfi [Séytaane]. Nangeen leen moytu, xéy-na kon ngeen texe.
91إِنَّمَا يُرِيدُ الشَّيْطَانُ أَن يُوقِعَ بَيْنَكُمُ الْعَدَاوَةَ وَالْبَغْضَاءَ فِي الْخَمْرِ وَالْمَيْسِرِ وَيَصُدَّكُمْ عَن ذِكْرِ اللَّهِ وَعَنِ الصَّلَاةِ ۖ فَهَلْ أَنتُم مُّنتَهُونَ
Séytaane bëggul lu dul tàbbal ci seen diggante nooneel ak mbañeel, jaare ko ci sàngara ak wure te it dox seen diggante ak fàttaliku Yàlla ak julli. Moo ndax dungeen leen bàyyi ?
92وَأَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ وَاحْذَرُوا ۚ فَإِن تَوَلَّيْتُمْ فَاعْلَمُوا أَنَّمَا عَلَىٰ رَسُولِنَا الْبَلَاغُ الْمُبِينُ
Nangeen topp Yàlla ak Yonent bi, te ngeen wattandiku ! Bu ngeen dëddoo... nangeen xam ne Sunu Yonent bi dara waru ko lu dul jotal gu mat sëkk.
93لَيْسَ عَلَى الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ جُنَاحٌ فِيمَا طَعِمُوا إِذَا مَا اتَّقَوا وَّآمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ ثُمَّ اتَّقَوا وَّآمَنُوا ثُمَّ اتَّقَوا وَّأَحْسَنُوا ۗ وَاللَّهُ يُحِبُّ الْمُحْسِنِينَ
Du nekk bàkkaar ca ña gëm tey sellal seeni jëf, la ñu masoon a lekk [lu araam lu jiitu digle ga ko araamal], gannaaw ba, ñu nekk ñu di way-ragal Yàlla te gëm, di sellal seeni jëf ba noppi raggal Yàlla te gëm ; ragal Yàlla te rafetal seeni jëf. Yàlla safoo na way-rafetal ña.
94يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَيَبْلُوَنَّكُمُ اللَّهُ بِشَيْءٍ مِّنَ الصَّيْدِ تَنَالُهُ أَيْدِيكُمْ وَرِمَاحُكُمْ لِيَعْلَمَ اللَّهُ مَن يَخَافُهُ بِالْغَيْبِ ۚ فَمَنِ اعْتَدَىٰ بَعْدَ ذَٰلِكَ فَلَهُ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Éy yéen ñi gëm ! Yàlla dana leen nattu ci lenn lu jëm ci rëbb ci seeni loxo walla seeni xeej. Ndax Mu xam ku Ko ragal ci kumpa. Ku féttéerlu ginnaaw loolu, mbugal mu metti dana ko dal.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
92Aaya

Tekki — Al-Maida 92

Simoore Al-Maida Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangeen topp Yàlla ak Yonent bi, te ngeen wattandiku !…

Simoore Aaya 92/120 — Simoore Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Maida Dégg, Simoore Al-Maida Tekki, Simoore Al-Maida mp3, Simoore Al-Maida pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers