Qaf · 33/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
مَّنْ خَشِيَ الرَّحْمَٰنَ بِالْغَيْبِ وَجَاءَ بِقَلْبٍ مُّنِيبٍ ۝٣٣
Man khashiyar Rahmaana bilghaibi wa jaaa`a biqalbim muneeb
📖 Tekkim Wolof
kuy ragal Yàlla Yërëmakoon bi ci kumpa, te ñëw ànd ak xol bu nangu ndigal.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 31-35 — Simoore Qaf

31وَأُزْلِفَتِ الْجَنَّةُ لِلْمُتَّقِينَ غَيْرَ بَعِيدٍ
Nu waajal Àjjana way ragal ña Yàlla mu jigeñ loolu.
32هَٰذَا مَا تُوعَدُونَ لِكُلِّ أَوَّابٍ حَفِيظٍ
“Lii mooy li Nu leen daan dig , [mu ñeel] bépp delluwaakoon ci Boroomam tey sàmm [daytalu Boroomam]
33مَّنْ خَشِيَ الرَّحْمَٰنَ بِالْغَيْبِ وَجَاءَ بِقَلْبٍ مُّنِيبٍ
kuy ragal Yàlla Yërëmakoon bi ci kumpa, te ñëw ànd ak xol bu nangu ndigal.
34ادْخُلُوهَا بِسَلَامٍ ۖ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُلُودِ
Dugguleen ko ci jàmm ak tal”. Te loolu mooy sax ba fàww (Àjjana) !
35لَهُم مَّا يَشَاءُونَ فِيهَا وَلَدَيْنَا مَزِيدٌ
Danañu fa am lépp lu leen soob. Te am Nanu ndollen.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Qaf 33

Simoore Qaf Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : kuy ragal Yàlla Yërëmakoon bi ci kumpa, te ñëw ànd…

Simoore Aaya 33/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers