Qaf · 32/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
هَٰذَا مَا تُوعَدُونَ لِكُلِّ أَوَّابٍ حَفِيظٍ ۝٣٢
Haaza maa too`adoona likulli awwaabin hafeez
📖 Tekkim Wolof
“Lii mooy li Nu leen daan dig , [mu ñeel] bépp delluwaakoon ci Boroomam tey sàmm [daytalu Boroomam]

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 30-34 — Simoore Qaf

30يَوْمَ نَقُولُ لِجَهَنَّمَ هَلِ امْتَلَأْتِ وَتَقُولُ هَلْ مِن مَّزِيدٍ
Bu keroogee ba Nuy laaj Safara naan ko ; “Ndax fees nga ? ” Safara naan : “Dolli ma” ?
31وَأُزْلِفَتِ الْجَنَّةُ لِلْمُتَّقِينَ غَيْرَ بَعِيدٍ
Nu waajal Àjjana way ragal ña Yàlla mu jigeñ loolu.
32هَٰذَا مَا تُوعَدُونَ لِكُلِّ أَوَّابٍ حَفِيظٍ
“Lii mooy li Nu leen daan dig , [mu ñeel] bépp delluwaakoon ci Boroomam tey sàmm [daytalu Boroomam]
33مَّنْ خَشِيَ الرَّحْمَٰنَ بِالْغَيْبِ وَجَاءَ بِقَلْبٍ مُّنِيبٍ
kuy ragal Yàlla Yërëmakoon bi ci kumpa, te ñëw ànd ak xol bu nangu ndigal.
34ادْخُلُوهَا بِسَلَامٍ ۖ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُلُودِ
Dugguleen ko ci jàmm ak tal”. Te loolu mooy sax ba fàww (Àjjana) !
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Qaf 32

Simoore Qaf Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Lii mooy li Nu leen daan dig , [mu ñeel]…

Simoore Aaya 32/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers