Adh-Dhariyat · 7/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
وَالسَّمَاءِ ذَاتِ الْحُبُكِ ۝٧
Wassamaaa`i zaatil hubuk
📖 Tekkim Wolof
Ak ci asamaan si di borom mbub taar !

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Simoore Adh-Dhariyat

5إِنَّمَا تُوعَدُونَ لَصَادِقٌ
(Maa ngi) giñ ne liñu leen di digu lu dëggu la.
6وَإِنَّ الدِّينَ لَوَاقِعٌ
Te it bisub Penc ba lu nekk la lu am la du jaas.
7وَالسَّمَاءِ ذَاتِ الْحُبُكِ
Ak ci asamaan si di borom mbub taar !
8إِنَّكُمْ لَفِي قَوْلٍ مُّخْتَلِفٍ
Yéen (yéefar yi) yéen a ngi ci ay wax yu féewóo.
9يُؤْفَكُ عَنْهُ مَنْ أُفِكَ
(Wax joo xam ne) Képp kuy dumóoyu Alxuraan wax joojoo ko waral.
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 7

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak ci asamaan si di borom mbub taar !

Simoore Aaya 7/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers