Adh-Dhariyat · 8/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
إِنَّكُمْ لَفِي قَوْلٍ مُّخْتَلِفٍ ۝٨
Innakum lafee qawlim mukhtalif
📖 Tekkim Wolof
Yéen (yéefar yi) yéen a ngi ci ay wax yu féewóo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Adh-Dhariyat

6وَإِنَّ الدِّينَ لَوَاقِعٌ
Te it bisub Penc ba lu nekk la lu am la du jaas.
7وَالسَّمَاءِ ذَاتِ الْحُبُكِ
Ak ci asamaan si di borom mbub taar !
8إِنَّكُمْ لَفِي قَوْلٍ مُّخْتَلِفٍ
Yéen (yéefar yi) yéen a ngi ci ay wax yu féewóo.
9يُؤْفَكُ عَنْهُ مَنْ أُفِكَ
(Wax joo xam ne) Képp kuy dumóoyu Alxuraan wax joojoo ko waral.
10قُتِلَ الْخَرَّاصُونَ
Fenkat ya durkat ya dee nañu,
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 8

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen (yéefar yi) yéen a ngi ci ay wax yu…

Simoore Aaya 8/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers