Al-Qamar · 30/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ ۝٣٠
Fakaifa kaana `azaabee wa nuzur
📖 Tekkim Wolof
Naka la Sama mbugël ak Sama xupp nekke (ci seen kaw) ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore Al-Qamar

28وَنَبِّئْهُمْ أَنَّ الْمَاءَ قِسْمَةٌ بَيْنَهُمْ ۖ كُلُّ شِرْبٍ مُّحْتَضَرٌ
Nanga xamle ne ndox ma dañu koy bokk séddóo ñook [giléem ga] ; duñu fa fekkante.
29فَنَادَوْا صَاحِبَهُمْ فَتَعَاطَىٰ فَعَقَرَ
Ñu daldi woo seen àndandoo mu daldi koy rey.
30فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka la Sama mbugël ak Sama xupp nekke (ci seen kaw) ?
31إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ صَيْحَةً وَاحِدَةً فَكَانُوا كَهَشِيمِ الْمُحْتَظِرِ
Yabal nanu ca ñoom genn Xaacu, ñu mel poñiitum kuy ñag am ñax.
32وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal nanu, Alxuraan ngir ñu fàttaliku ca. Mo ndax kenn dana ca jàjjoo ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Al-Qamar 30

Simoore Al-Qamar Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Naka la Sama mbugël ak Sama xupp nekke (ci seen…

Simoore Aaya 30/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers