Al-Waqi'a · 34/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
وَفُرُشٍ مَّرْفُوعَةٍ ۝٣٤
Wa furushim marfoo`ah
📖 Tekkim Wolof
ak ay laltaay yu yékkatiku,

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Simoore Al-Waqi'a

32وَفَاكِهَةٍ كَثِيرَةٍ
ak ay fuytéef yu bari sakkan
33لَّا مَقْطُوعَةٍ وَلَا مَمْنُوعَةٍ
du rag mukk te it kenn du ko tere,
34وَفُرُشٍ مَّرْفُوعَةٍ
ak ay laltaay yu yékkatiku,
35إِنَّا أَنشَأْنَاهُنَّ إِنشَاءً
Man Yàlla maa leen sàkk ñu ñeseŋ ñoom (huur al iin),
36فَجَعَلْنَاهُنَّ أَبْكَارًا
def Nanu leen ñu di ay xiig,
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 34

Simoore Al-Waqi'a Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak ay laltaay yu yékkatiku,

Simoore Aaya 34/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers