Al-Hadid · 29/29
Tekki Waxtaan — Al-Hadid
لِّئَلَّا يَعْلَمَ أَهْلُ الْكِتَابِ أَلَّا يَقْدِرُونَ عَلَىٰ شَيْءٍ مِّن فَضْلِ اللَّهِ ۙ وَأَنَّ الْفَضْلَ بِيَدِ اللَّهِ يُؤْتِيهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَاللَّهُ ذُو الْفَضْلِ الْعَظِيمِ ۝٢٩
Li`alla ya`lama Ahlul kitaabi allaa yaqdiroona `alaa shai`im min fadlil laahi wa annal fadla bi Yadil laahi u`teehi many yashaaa`; wallaahu Zul fadilil `azeem
📖 Tekkim Wolof
Ñoñ Téere nañu xam ne manuñu dara ci ngënéelu Yàlla te it ngëneel ci loxo Yàlla la nekk ; Moo koy jox ku ko soob, te Yàlla moo di Boroom ngëneel lu màgg li.
🎧 Dégg

📜 Aaya 27-29 — Al-Hadid

27ثُمَّ قَفَّيْنَا عَلَىٰ آثَارِهِم بِرُسُلِنَا وَقَفَّيْنَا بِعِيسَى ابْنِ مَرْيَمَ وَآتَيْنَاهُ الْإِنجِيلَ وَجَعَلْنَا فِي قُلُوبِ الَّذِينَ اتَّبَعُوهُ رَأْفَةً وَرَحْمَةً وَرَهْبَانِيَّةً ابْتَدَعُوهَا مَا كَتَبْنَاهَا عَلَيْهِمْ إِلَّا ابْتِغَاءَ رِضْوَانِ اللَّهِ فَمَا رَعَوْهَا حَقَّ رِعَايَتِهَا ۖ فَآتَيْنَا الَّذِينَ آمَنُوا مِنْهُمْ أَجْرَهُمْ ۖ وَكَثِيرٌ مِّنْهُمْ فَاسِقُونَ
Nu daldi xentuloo sunuy Yonent seen mboor, xentuloo Iisaa domu Maryaama indil nanu ko Injiil, te it def nanu ca biir xolu ña ko topp ak ñeewante ak yërmaande. Ak bero jigéen ña ñoom ñoo ko fental seen bopp, Waaye farataalu nu ko ci ñoom. Li nu leen digël daal moo di nañu sàkku ngëramul Yàlla. Te sax sàmmuñu ko ni mu ware. Ña bokk ca ñoom te gëm indil Nanu leen seenug pey. Waaye lu bari ci ñoom ay saay-saay lañu.
28يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اتَّقُوا اللَّهَ وَآمِنُوا بِرَسُولِهِ يُؤْتِكُمْ كِفْلَيْنِ مِن رَّحْمَتِهِ وَيَجْعَل لَّكُمْ نُورًا تَمْشُونَ بِهِ وَيَغْفِرْ لَكُمْ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Eey yéen ñi gëm ! Ragal-leen Yàlla te gëm Yonentam bi dana leen defal ñaari cokkoor yu yërmande, danaleen defal it ak leer gu ngeen gindikoo, te it dinaleen jéggël, Yàlla Jéggëlaakoon la Jaglewaakoon la.
29لِّئَلَّا يَعْلَمَ أَهْلُ الْكِتَابِ أَلَّا يَقْدِرُونَ عَلَىٰ شَيْءٍ مِّن فَضْلِ اللَّهِ ۙ وَأَنَّ الْفَضْلَ بِيَدِ اللَّهِ يُؤْتِيهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَاللَّهُ ذُو الْفَضْلِ الْعَظِيمِ
Ñoñ Téere nañu xam ne manuñu dara ci ngënéelu Yàlla te it ngëneel ci loxo Yàlla la nekk ; Moo koy jox ku ko soob, te Yàlla moo di Boroom ngëneel lu màgg li.
Al-HadidFihi Alxuraan
29Aaya
MedinanRevelation
29Aaya

Tekki — Al-Hadid 29

Simoore Al-Hadid Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoñ Téere nañu xam ne manuñu dara ci ngënéelu Yàlla…

Simoore Aaya 29/29 — Al-Hadid الحديد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hadid Dégg, Al-Hadid Tekki, Al-Hadid mp3, Al-Hadid pdf. Aaya 27–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers