Al-Hashr · 24/24
Tekki Waxtaan — Al-Hashr
هُوَ اللَّهُ الْخَالِقُ الْبَارِئُ الْمُصَوِّرُ ۖ لَهُ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ ۚ يُسَبِّحُ لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝٢٤
Huwal Laahul Khaaliqul Baari `ul Musawwir; lahul Asmaaa`ul Husnaa; yusabbihu lahoo maa fis samaawaati wal ardi wa Huwal `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Moom Mooy Yàlla, Bindkat biy sos, tey Melal. Mooy boroom tur yi gën a rafet. Mbooleem li nekk ci asamaan yeek suuf si dañu koy sàbbaal di ko kañ. Moom moo di boroom Kàttan gi, di Ku Xereñ ki.

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-24 — Al-Hashr

22هُوَ اللَّهُ الَّذِي لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ عَالِمُ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ ۖ هُوَ الرَّحْمَٰنُ الرَّحِيمُ
Moom mooy Yàlla ji nga xam ne. Amul jeneen Yàlla ju dul moom, Moo xam kumpa ak li Feeñ. Mooy, Yëramaakoon bi, di Jaglewaakoon bi.
23هُوَ اللَّهُ الَّذِي لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ الْمَلِكُ الْقُدُّوسُ السَّلَامُ الْمُؤْمِنُ الْمُهَيْمِنُ الْعَزِيزُ الْجَبَّارُ الْمُتَكَبِّرُ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Moom Mooy, Yàlla ji nga xam ne. Amul jeneen Yàlla ju dul moom ; mooy Boroom bi, di Ku Sell ki, di Jàmm ji, di Ku Wóor ki, di Ku Peek lépp, di Boroom Kàttan gi, di Ponkal mi, di Ku Rëy ki. Tudd naa Sellam gi ! Soree na lool ak li ñu koy bokkaaleel.
24هُوَ اللَّهُ الْخَالِقُ الْبَارِئُ الْمُصَوِّرُ ۖ لَهُ الْأَسْمَاءُ الْحُسْنَىٰ ۚ يُسَبِّحُ لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Moom Mooy Yàlla, Bindkat biy sos, tey Melal. Mooy boroom tur yi gën a rafet. Mbooleem li nekk ci asamaan yeek suuf si dañu koy sàbbaal di ko kañ. Moom moo di boroom Kàttan gi, di Ku Xereñ ki.
Al-HashrFihi Alxuraan
24Aaya
MedinanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Hashr 24

Simoore Al-Hashr Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom Mooy Yàlla, Bindkat biy sos, tey Melal. Mooy boroom…

Simoore Aaya 24/24 — Al-Hashr الحشر (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hashr Dégg, Al-Hashr Tekki, Al-Hashr mp3, Al-Hashr pdf. Aaya 22–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers