Al-Mumtahina · 13/13
Tekki Waxtaan — Al-Mumtahina
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَوَلَّوْا قَوْمًا غَضِبَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ قَدْ يَئِسُوا مِنَ الْآخِرَةِ كَمَا يَئِسَ الْكُفَّارُ مِنْ أَصْحَابِ الْقُبُورِ ۝١٣
Yaaa ayyuhal lazeena amanoo laa tatawallaw qawman ghadibal laahu `alaihim qad ya`isoo minal aakhirati kamaa ya`isal kuffaaru min as haabil quboor
📖 Tekkim Wolof
Eey yéen ñi gëm ! Buleen di xaritook aw nit ñoo xam ne Yàlla da leen mere te dañoo yoqat ci àllaaxira, ni Yéefër yi yoqate ci ñi nekk ci biir bàmmeel yi.
🎧 Dégg

📜 Aaya 11-13 — Al-Mumtahina

11وَإِن فَاتَكُمْ شَيْءٌ مِّنْ أَزْوَاجِكُمْ إِلَى الْكُفَّارِ فَعَاقَبْتُمْ فَآتُوا الَّذِينَ ذَهَبَتْ أَزْوَاجُهُم مِّثْلَ مَا أَنفَقُوا ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ الَّذِي أَنتُم بِهِ مُؤْمِنُونَ
Su seeni soxna rëccee dem ca Yéefër ya yóbbaale can, su ngeen xareek ñoom ba nangu seeni alal, nangeen daldi génneel ña ca seeni soxna dem kem lu tollu ni seeni can. Te nangeen ragal Yàlla mi ngeen gëm.
12يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ إِذَا جَاءَكَ الْمُؤْمِنَاتُ يُبَايِعْنَكَ عَلَىٰ أَن لَّا يُشْرِكْنَ بِاللَّهِ شَيْئًا وَلَا يَسْرِقْنَ وَلَا يَزْنِينَ وَلَا يَقْتُلْنَ أَوْلَادَهُنَّ وَلَا يَأْتِينَ بِبُهْتَانٍ يَفْتَرِينَهُ بَيْنَ أَيْدِيهِنَّ وَأَرْجُلِهِنَّ وَلَا يَعْصِينَكَ فِي مَعْرُوفٍ ۙ فَبَايِعْهُنَّ وَاسْتَغْفِرْ لَهُنَّ اللَّهَ ۖ إِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Eey yaw Yonent bi ! Jigéen ñi gëm su ñu la dikkalee di jaayanteek yaw ci ne, dootuñu bokkaaleek Yàlla dara, duñu sàcc, duñu njaaloo, duñu rey seeni doom, te duñu sos genn njaaxum ci seeni tànk ak yoxo te dunu la moy ci wenn yiw, nanga jaayanteek ñoom, te nanga leen jéggalul Yàlla. Te Yàlla moom, Jéggalakoon la Jaglewaakoon la.
13يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَوَلَّوْا قَوْمًا غَضِبَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ قَدْ يَئِسُوا مِنَ الْآخِرَةِ كَمَا يَئِسَ الْكُفَّارُ مِنْ أَصْحَابِ الْقُبُورِ
Eey yéen ñi gëm ! Buleen di xaritook aw nit ñoo xam ne Yàlla da leen mere te dañoo yoqat ci àllaaxira, ni Yéefër yi yoqate ci ñi nekk ci biir bàmmeel yi.
Al-MumtahinaFihi Alxuraan
13Aaya
MedinanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Mumtahina 13

Simoore Al-Mumtahina Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Eey yéen ñi gëm ! Buleen di xaritook aw nit…

Simoore Aaya 13/13 — Al-Mumtahina الممتحنة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mumtahina Dégg, Al-Mumtahina Tekki, Al-Mumtahina mp3, Al-Mumtahina pdf. Aaya 11–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers