At-Taghabun · 1/18
Tekki Waxtaan — Simoore At-Taghabun
يُسَبِّحُ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ لَهُ الْمُلْكُ وَلَهُ الْحَمْدُ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ ۝١
Yusabbihu lillaahi maa fis samaawaati wa maa fil ardi lahul mulku wa lahul hamd, wa Huwa `alaa kulli shai `in Qadeer
📖 Tekkim Wolof
Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si ña ngay sàbbaal Yàlla. Mooy boroom nguur te Mooy boroom cant. Te Moom man na Lépp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore At-Taghabun

1يُسَبِّحُ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۖ لَهُ الْمُلْكُ وَلَهُ الْحَمْدُ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si ña ngay sàbbaal Yàlla. Mooy boroom nguur te Mooy boroom cant. Te Moom man na Lépp.
2هُوَ الَّذِي خَلَقَكُمْ فَمِنكُمْ كَافِرٌ وَمِنكُم مُّؤْمِنٌ ۚ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرٌ
Mooy ki leen bind. Am na ci yéen ay yéefar am it ci yéen ay jullit way gëm. Te Yàlla kuy gis la li ngeen di def.
3خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِالْحَقِّ وَصَوَّرَكُمْ فَأَحْسَنَ صُوَرَكُمْ ۖ وَإِلَيْهِ الْمَصِيرُ
Bind na asamaan yeek suuf si ci dëgg mu tën seeni jëmm te rafetal na seeni jëm. Te ca moom mooy Deluwaay ba.
At-TaghabunFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — At-Taghabun 1

Simoore At-Taghabun Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si ña ngay sàbbaal…

Simoore Aaya 1/18 — Simoore At-Taghabun التغابن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Taghabun Dégg, Simoore At-Taghabun Tekki, Simoore At-Taghabun mp3, Simoore At-Taghabun pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers