Al-Mulk · 12/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mulk
إِنَّ الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ كَبِيرٌ ۝١٢
Innal lazeena yakhshawna rabbahum bilghaibi lahum maghfiratunw wa ajrun kabeer
📖 Tekkim Wolof
Ñay ragal seen Boroom ci kumpa am nañu ag njégël ak pey gu màgg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Mulk

10وَقَالُوا لَوْ كُنَّا نَسْمَعُ أَوْ نَعْقِلُ مَا كُنَّا فِي أَصْحَابِ السَّعِيرِ
Ñu wax it ne : “Su nu doon dégg mbaa nu xel-lu, kon dunu nekk ci mbugël mii tey”.
11فَاعْتَرَفُوا بِذَنبِهِمْ فَسُحْقًا لِّأَصْحَابِ السَّعِيرِ
Nangu nañu seeni bàkkaar. Waa safara toskare nañu.
12إِنَّ الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ كَبِيرٌ
Ñay ragal seen Boroom ci kumpa am nañu ag njégël ak pey gu màgg.
13وَأَسِرُّوا قَوْلَكُمْ أَوِ اجْهَرُوا بِهِ ۖ إِنَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Su ngeen di déey walla ngeen di jooru Moo xam tigi li nekk ci dënn yi.
14أَلَا يَعْلَمُ مَنْ خَلَقَ وَهُوَ اللَّطِيفُ الْخَبِيرُ
Ki bind ndax dadul xam te Moom moo di ki Ñewenti, di Ku deñ Kumpa ci lépp.
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Mulk 12

Simoore Al-Mulk Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñay ragal seen Boroom ci kumpa am nañu ag njégël…

Simoore Aaya 12/30 — Simoore Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mulk Dégg, Simoore Al-Mulk Tekki, Simoore Al-Mulk mp3, Simoore Al-Mulk pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers