Al-Mulk · 11/30
Tekki Waxtaan — Al-Mulk
فَاعْتَرَفُوا بِذَنبِهِمْ فَسُحْقًا لِّأَصْحَابِ السَّعِيرِ ۝١١
Fa`tarafoo bizambihim fasuhqal li as haabis sa`eer
📖 Tekkim Wolof
Nangu nañu seeni bàkkaar. Waa safara toskare nañu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Al-Mulk

9قَالُوا بَلَىٰ قَدْ جَاءَنَا نَذِيرٌ فَكَذَّبْنَا وَقُلْنَا مَا نَزَّلَ اللَّهُ مِن شَيْءٍ إِنْ أَنتُمْ إِلَّا فِي ضَلَالٍ كَبِيرٍ
Ñu naan ko : “Axakañ ! dikkaloon nañu nu kay, nu ne leen: Yàlla wàccewul tus, te yéen dangeen a sànku”
10وَقَالُوا لَوْ كُنَّا نَسْمَعُ أَوْ نَعْقِلُ مَا كُنَّا فِي أَصْحَابِ السَّعِيرِ
Ñu wax it ne : “Su nu doon dégg mbaa nu xel-lu, kon dunu nekk ci mbugël mii tey”.
11فَاعْتَرَفُوا بِذَنبِهِمْ فَسُحْقًا لِّأَصْحَابِ السَّعِيرِ
Nangu nañu seeni bàkkaar. Waa safara toskare nañu.
12إِنَّ الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ كَبِيرٌ
Ñay ragal seen Boroom ci kumpa am nañu ag njégël ak pey gu màgg.
13وَأَسِرُّوا قَوْلَكُمْ أَوِ اجْهَرُوا بِهِ ۖ إِنَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Su ngeen di déey walla ngeen di jooru Moo xam tigi li nekk ci dënn yi.
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Mulk 11

Simoore Al-Mulk Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangu nañu seeni bàkkaar. Waa safara toskare nañu.

Simoore Aaya 11/30 — Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mulk Dégg, Al-Mulk Tekki, Al-Mulk mp3, Al-Mulk pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers