Al-Mulk · 17/30
Tekki Waxtaan — Al-Mulk
أَمْ أَمِنتُم مَّن فِي السَّمَاءِ أَن يُرْسِلَ عَلَيْكُمْ حَاصِبًا ۖ فَسَتَعْلَمُونَ كَيْفَ نَذِيرِ ١٧
Transliteration
Am amintum man fissamaaa`i ai yursila `alaikum haasiban fasata`lamoona kaifa nazeer
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Walla dangeen a man a raw ki nekk ci asamaan su yabalee lu ànd ak i doj ? Xalset ngeen xam Samag xupe.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 15-19 — Al-Mulk
15هُوَ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ ذَلُولًا فَامْشُوا فِي مَنَاكِبِهَا وَكُلُوا مِن رِّزْقِهِ ۖ وَإِلَيْهِ النُّشُورُ
Moom moo leen tàggatal suuf si : doxleen ci ay déndëm. Tey lekk ciy xéewalam. (Ca Yàlla) la léppiy mujj.
16أَأَمِنتُم مَّن فِي السَّمَاءِ أَن يَخْسِفَ بِكُمُ الْأَرْضَ فَإِذَا هِيَ تَمُورُ
Ndax man ngeen a raw ki nekk ci asamaan si su talañee suuf si ? Ba muy rëg-rëgi, mukk !
17أَمْ أَمِنتُم مَّن فِي السَّمَاءِ أَن يُرْسِلَ عَلَيْكُمْ حَاصِبًا ۖ فَسَتَعْلَمُونَ كَيْفَ نَذِيرِ
Walla dangeen a man a raw ki nekk ci asamaan su yabalee lu ànd ak i doj ? Xalset ngeen xam Samag xupe.
18وَلَقَدْ كَذَّبَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ فَكَيْفَ كَانَ نَكِيرِ
Ña leen fi jiitu woon, weddi woon nañu. Kon naka la sama mbugël deme woon ci ñoom !
19أَوَلَمْ يَرَوْا إِلَى الطَّيْرِ فَوْقَهُمْ صَافَّاتٍ وَيَقْبِضْنَ ۚ مَا يُمْسِكُهُنَّ إِلَّا الرَّحْمَٰنُ ۚ إِنَّهُ بِكُلِّ شَيْءٍ بَصِيرٌ
Xanaa dañoo xoolul ci picc yi leen tiim, di tàllal seeni laaf ak bank ? Te (Yàlla) Yëramaakoon bi rekk leen teye (ci jawu ji). Moom, Kuy Gis la lépp lu ne.
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
17Aaya
Tekki — Al-Mulk 17
Simoore Al-Mulk Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla dangeen a man a raw ki nekk ci asamaan…Simoore Aaya 17/30 — Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mulk Dégg, Al-Mulk Tekki, Al-Mulk mp3, Al-Mulk pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








