Al-Mulk · 16/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mulk
أَأَمِنتُم مَّن فِي السَّمَاءِ أَن يَخْسِفَ بِكُمُ الْأَرْضَ فَإِذَا هِيَ تَمُورُ ۝١٦
A-amintum man fissamaaa`i aiyakhsifa bi kumul arda fa izaa hiya tamoor
📖 Tekkim Wolof
Ndax man ngeen a raw ki nekk ci asamaan si su talañee suuf si ? Ba muy rëg-rëgi, mukk !

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Mulk

14أَلَا يَعْلَمُ مَنْ خَلَقَ وَهُوَ اللَّطِيفُ الْخَبِيرُ
Ki bind ndax dadul xam te Moom moo di ki Ñewenti, di Ku deñ Kumpa ci lépp.
15هُوَ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ ذَلُولًا فَامْشُوا فِي مَنَاكِبِهَا وَكُلُوا مِن رِّزْقِهِ ۖ وَإِلَيْهِ النُّشُورُ
Moom moo leen tàggatal suuf si : doxleen ci ay déndëm. Tey lekk ciy xéewalam. (Ca Yàlla) la léppiy mujj.
16أَأَمِنتُم مَّن فِي السَّمَاءِ أَن يَخْسِفَ بِكُمُ الْأَرْضَ فَإِذَا هِيَ تَمُورُ
Ndax man ngeen a raw ki nekk ci asamaan si su talañee suuf si ? Ba muy rëg-rëgi, mukk !
17أَمْ أَمِنتُم مَّن فِي السَّمَاءِ أَن يُرْسِلَ عَلَيْكُمْ حَاصِبًا ۖ فَسَتَعْلَمُونَ كَيْفَ نَذِيرِ
Walla dangeen a man a raw ki nekk ci asamaan su yabalee lu ànd ak i doj ? Xalset ngeen xam Samag xupe.
18وَلَقَدْ كَذَّبَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ فَكَيْفَ كَانَ نَكِيرِ
Ña leen fi jiitu woon, weddi woon nañu. Kon naka la sama mbugël deme woon ci ñoom !
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Mulk 16

Simoore Al-Mulk Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax man ngeen a raw ki nekk ci asamaan si…

Simoore Aaya 16/30 — Simoore Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mulk Dégg, Simoore Al-Mulk Tekki, Simoore Al-Mulk mp3, Simoore Al-Mulk pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers