Al-Qalam · 34/52
Tekki Waxtaan — Al-Qalam
إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ عِندَ رَبِّهِمْ جَنَّاتِ النَّعِيمِ ۝٣٤
Inna lilmuttaqeena `inda rabbihim jannaatin na`eem
📖 Tekkim Wolof
Ña ragal Yàlla dey ñoom am nanu Àjjanay xéewal fa seen Boroom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Al-Qalam

32عَسَىٰ رَبُّنَا أَن يُبْدِلَنَا خَيْرًا مِّنْهَا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا رَاغِبُونَ
Aka neexoon Yàlla nangu sunu tuub wuutalal nu ko ak tool yu ko gën. Sunu Boroom la nu xemmem”.
33كَذَٰلِكَ الْعَذَابُ ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Noonu la mbugal ma deme woon ; te mbugalum àllaaxira maay gëna rëy, cëy bu ñu xamoon !
34إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ عِندَ رَبِّهِمْ جَنَّاتِ النَّعِيمِ
Ña ragal Yàlla dey ñoom am nanu Àjjanay xéewal fa seen Boroom.
35أَفَنَجْعَلُ الْمُسْلِمِينَ كَالْمُجْرِمِينَ
Moo ndax danuy def ñi wommatu jëm ci [Yàlla] ñu yem ak tooñkat ya ?
36مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ
Ana lan moo leen dal ? Ak naka ngeen di àttee ?
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Qalam 34

Simoore Al-Qalam Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ragal Yàlla dey ñoom am nanu Àjjanay xéewal fa…

Simoore Aaya 34/52 — Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qalam Dégg, Al-Qalam Tekki, Al-Qalam mp3, Al-Qalam pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers