Al-Qalam · 35/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
أَفَنَجْعَلُ الْمُسْلِمِينَ كَالْمُجْرِمِينَ ۝٣٥
Afanaj`alul muslimeena kalmujrimeen
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax danuy def ñi wommatu jëm ci [Yàlla] ñu yem ak tooñkat ya ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 33-37 — Simoore Al-Qalam

33كَذَٰلِكَ الْعَذَابُ ۖ وَلَعَذَابُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Noonu la mbugal ma deme woon ; te mbugalum àllaaxira maay gëna rëy, cëy bu ñu xamoon !
34إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ عِندَ رَبِّهِمْ جَنَّاتِ النَّعِيمِ
Ña ragal Yàlla dey ñoom am nanu Àjjanay xéewal fa seen Boroom.
35أَفَنَجْعَلُ الْمُسْلِمِينَ كَالْمُجْرِمِينَ
Moo ndax danuy def ñi wommatu jëm ci [Yàlla] ñu yem ak tooñkat ya ?
36مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ
Ana lan moo leen dal ? Ak naka ngeen di àttee ?
37أَمْ لَكُمْ كِتَابٌ فِيهِ تَدْرُسُونَ
Wala book da ngeen am ab Téere bu ngeen di jàng
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — Al-Qalam 35

Simoore Al-Qalam Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax danuy def ñi wommatu jëm ci [Yàlla] ñu…

Simoore Aaya 35/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers