Al-A'raf · 46/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَبَيْنَهُمَا حِجَابٌ ۚ وَعَلَى الْأَعْرَافِ رِجَالٌ يَعْرِفُونَ كُلًّا بِسِيمَاهُمْ ۚ وَنَادَوْا أَصْحَابَ الْجَنَّةِ أَن سَلَامٌ عَلَيْكُمْ ۚ لَمْ يَدْخُلُوهَا وَهُمْ يَطْمَعُونَ ٤٦
Transliteration
Wa bainahumaa hijaab; wa `alal A`raafi rijaaluny ya`rifoona kullam biseemaahum; wa naadaw Ashaabal jannati an salaamun `alaikum; lam yadkhuloohaa wa hum yatma`oon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Dox na ca seen diggante [waa Àjjana] kiiraay, nekk na ca kaw (dig) wa aw nit ñoo xam ne danañu leen xàmmee ñoom ñépp ca seen màndarga ya. Ñu woo waa Àjjana, ne leen : “Yal na jàmm nekk ci yéen ! ”. Ñoom duñu dugg Àjjana te xemmem nañu ko.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 44-48 — Al-A'raf
44وَنَادَىٰ أَصْحَابُ الْجَنَّةِ أَصْحَابَ النَّارِ أَن قَدْ وَجَدْنَا مَا وَعَدَنَا رَبُّنَا حَقًّا فَهَلْ وَجَدتُّم مَّا وَعَدَ رَبُّكُمْ حَقًّا ۖ قَالُوا نَعَمْ ۚ فَأَذَّنَ مُؤَذِّنٌ بَيْنَهُمْ أَن لَّعْنَةُ اللَّهِ عَلَى الظَّالِمِينَ
Waa Àjjana woo waa Safara, ne leen : “Nun dey, gis nanu la nu sunu Boroom digoon muy dëgg. Moo ndax yéen fekk ngeen li leen seen Boroom digoon muy dëgg ? ”. Ñu toontu ne : “Waaw”. Mu am wootekat bu daldi woote ne : rëbbum Yàlla dal na ca tooñkat ya,
45الَّذِينَ يَصُدُّونَ عَن سَبِيلِ اللَّهِ وَيَبْغُونَهَا عِوَجًا وَهُم بِالْآخِرَةِ كَافِرُونَ
ñoom ñay féewale [nit ñi] ak diiney Yàlla ji, di doxe doxiin wu jeng, te ñoom dañoo weddi àllaaxira.”
46وَبَيْنَهُمَا حِجَابٌ ۚ وَعَلَى الْأَعْرَافِ رِجَالٌ يَعْرِفُونَ كُلًّا بِسِيمَاهُمْ ۚ وَنَادَوْا أَصْحَابَ الْجَنَّةِ أَن سَلَامٌ عَلَيْكُمْ ۚ لَمْ يَدْخُلُوهَا وَهُمْ يَطْمَعُونَ
Dox na ca seen diggante [waa Àjjana] kiiraay, nekk na ca kaw (dig) wa aw nit ñoo xam ne danañu leen xàmmee ñoom ñépp ca seen màndarga ya. Ñu woo waa Àjjana, ne leen : “Yal na jàmm nekk ci yéen ! ”. Ñoom duñu dugg Àjjana te xemmem nañu ko.
47۞ وَإِذَا صُرِفَتْ أَبْصَارُهُمْ تِلْقَاءَ أَصْحَابِ النَّارِ قَالُوا رَبَّنَا لَا تَجْعَلْنَا مَعَ الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Saa su seeni gët jubloo ca waa Safara, ñu ne : "Sunu Boroom, Yàlla boo nu boole ak nit ñu di ay tooñkat”.
48وَنَادَىٰ أَصْحَابُ الْأَعْرَافِ رِجَالًا يَعْرِفُونَهُم بِسِيمَاهُمْ قَالُوا مَا أَغْنَىٰ عَنكُمْ جَمْعُكُمْ وَمَا كُنتُمْ تَسْتَكْبِرُونَ
Ña nekk ca dig wa tuddu [Al-Lahraaf] woo ay nit ñu ñu xàmmee ngir seeni màndarga, ne leen : “Waa kon alal ja ngeen daan dajale ak la leen taxoon a rëy-rëylu, amaluñuleen benn njariñ !
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
46Aaya
Tekki — Al-A'raf 46
Simoore Al-A'raf Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dox na ca seen diggante [waa Àjjana] kiiraay, nekk na…Simoore Aaya 46/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








