Al-Muzzammil · 10/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muzzammil
وَاصْبِرْ عَلَىٰ مَا يَقُولُونَ وَاهْجُرْهُمْ هَجْرًا جَمِيلًا ۝١٠
Wasbir `alaa maa yaqoo loona wahjurhum hajran jameelaa
📖 Tekkim Wolof
Muñal li ñuy wax ; te nga gàddaay leen gàddaay gu rafet (bañ leena faale).

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Muzzammil

8وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ وَتَبَتَّلْ إِلَيْهِ تَبْتِيلًا
Na ngay fàttaliku di tud sa turu Boroom te wéeru ci moom fàwwu,
9رَّبُّ الْمَشْرِقِ وَالْمَغْرِبِ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ فَاتَّخِذْهُ وَكِيلًا
mooy boroom Penkook Sowu. Amul jeneen Yàlla ju dul moom. Na nga wéeru ci moom.
10وَاصْبِرْ عَلَىٰ مَا يَقُولُونَ وَاهْجُرْهُمْ هَجْرًا جَمِيلًا
Muñal li ñuy wax ; te nga gàddaay leen gàddaay gu rafet (bañ leena faale).
11وَذَرْنِي وَالْمُكَذِّبِينَ أُولِي النَّعْمَةِ وَمَهِّلْهُمْ قَلِيلًا
Bàyyi maak ñiy weddi ak ñi am alal ; te nga muñal leen tuuti :
12إِنَّ لَدَيْنَا أَنكَالًا وَجَحِيمًا
Noo ngi leen di waajal Safara wu ànd ak jéng,
Al-MuzzammilFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Muzzammil 10

Simoore Al-Muzzammil Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muñal li ñuy wax ; te nga gàddaay leen gàddaay…

Simoore Aaya 10/20 — Simoore Al-Muzzammil المزمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muzzammil Dégg, Simoore Al-Muzzammil Tekki, Simoore Al-Muzzammil mp3, Simoore Al-Muzzammil pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers