An-Nazi'at · 20/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
فَأَرَاهُ الْآيَةَ الْكُبْرَىٰ ۝٢٠
Fa araahul-aayatal kubra
📖 Tekkim Wolof
Mu wan ko keemtaan yu màgg ya.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 18-22 — Simoore An-Nazi'at

18فَقُلْ هَل لَّكَ إِلَىٰ أَن تَزَكَّىٰ
Te nga wax ko ne : “Ndax bëgg ngaa tuub ?
19وَأَهْدِيَكَ إِلَىٰ رَبِّكَ فَتَخْشَىٰ
kon dey da naa la gindi ci sa Boroom nga ragal ko ? ”
20فَأَرَاهُ الْآيَةَ الْكُبْرَىٰ
Mu wan ko keemtaan yu màgg ya.
21فَكَذَّبَ وَعَصَىٰ
Mu weddi ko (Firawna) daldi koy moy ;
22ثُمَّ أَدْبَرَ يَسْعَىٰ
Mu daldi, dumóoyu, féew dem,
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — An-Nazi'at 20

Simoore An-Nazi'at Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu wan ko keemtaan yu màgg ya.

Simoore Aaya 20/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers