Al-Anfal · 75/75
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anfal
وَالَّذِينَ آمَنُوا مِن بَعْدُ وَهَاجَرُوا وَجَاهَدُوا مَعَكُمْ فَأُولَٰئِكَ مِنكُمْ ۚ وَأُولُو الْأَرْحَامِ بَعْضُهُمْ أَوْلَىٰ بِبَعْضٍ فِي كِتَابِ اللَّهِ ۗ إِنَّ اللَّهَ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ ۝٧٥
Wallazeena aamanoo mim ba`du wa haajaroo wa jaahadoo ma;akum faulaaa`ika minkum; wa ulul arhaami baduhum awlaa biba`din fee Kitaabil laah; innal laaha bikulli shai`in `Aleem
📖 Tekkim Wolof
Ak ña gëm ginnaaw ga te ñu gàddaay tey xare ànd ak yéen, ñooña ci yéen lañu bokk.Waaye ña nekk ay mbokk ñoo gën a yey [ci donnante] ci Téereb Yàlla bi. Yàlla xam na lu ne.

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-75 — Simoore Al-Anfal

73وَالَّذِينَ كَفَرُوا بَعْضُهُمْ أَوْلِيَاءُ بَعْضٍ ۚ إِلَّا تَفْعَلُوهُ تَكُن فِتْنَةٌ فِي الْأَرْضِ وَفَسَادٌ كَبِيرٌ
Ña weddi, dañuy jàppoo. Bu ngeen ko deful, fitna ak yàqute gu rëy dana am ci kaw suuf si.
74وَالَّذِينَ آمَنُوا وَهَاجَرُوا وَجَاهَدُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ وَالَّذِينَ آوَوا وَّنَصَرُوا أُولَٰئِكَ هُمُ الْمُؤْمِنُونَ حَقًّا ۚ لَّهُم مَّغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ
Ña nga xam ne gëm nañu te gàddaay tey xare ci yoonu Yàlla ak ña leen dalaloon, di leen dimbali [Waa Ansaar], ñooña ñooy ñu gëm, ñu dëggu ña : am nañu njéggal ak xéewal gu tedd.
75وَالَّذِينَ آمَنُوا مِن بَعْدُ وَهَاجَرُوا وَجَاهَدُوا مَعَكُمْ فَأُولَٰئِكَ مِنكُمْ ۚ وَأُولُو الْأَرْحَامِ بَعْضُهُمْ أَوْلَىٰ بِبَعْضٍ فِي كِتَابِ اللَّهِ ۗ إِنَّ اللَّهَ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Ak ña gëm ginnaaw ga te ñu gàddaay tey xare ànd ak yéen, ñooña ci yéen lañu bokk.Waaye ña nekk ay mbokk ñoo gën a yey [ci donnante] ci Téereb Yàlla bi. Yàlla xam na lu ne.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
75Aaya

Tekki — Al-Anfal 75

Simoore Al-Anfal Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak ña gëm ginnaaw ga te ñu gàddaay tey xare…

Simoore Aaya 75/75 — Simoore Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anfal Dégg, Simoore Al-Anfal Tekki, Simoore Al-Anfal mp3, Simoore Al-Anfal pdf. Aaya 73–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers