At-Tawba · 57/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
لَوْ يَجِدُونَ مَلْجَأً أَوْ مَغَارَاتٍ أَوْ مُدَّخَلًا لَّوَلَّوْا إِلَيْهِ وَهُمْ يَجْمَحُونَ ۝٥٧
Law yajidoona malja`an aw maghaaraatin aw mudda khalal lawallaw ilaihi wa hum yajmahoon
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu amoon làquwaay walla xunti walla fu ñu dugg (ba raw), kon ñu dëddu jëm fa te gaaw ca.
🎧 Dégg

📜 Aaya 55-59 — At-Tawba

55فَلَا تُعْجِبْكَ أَمْوَالُهُمْ وَلَا أَوْلَادُهُمْ ۚ إِنَّمَا يُرِيدُ اللَّهُ لِيُعَذِّبَهُم بِهَا فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَتَزْهَقَ أَنفُسُهُمْ وَهُمْ كَافِرُونَ
Bula seeni alal yéem, naka noonu bula seeni doom yéem ! Yàlla nammul lu dul mbugal leen ci loolu ci dundug àddina si, ak ca roccig seeni ruu fekk ñu nekk di ay yéefar.
56وَيَحْلِفُونَ بِاللَّهِ إِنَّهُمْ لَمِنكُمْ وَمَا هُم مِّنكُمْ وَلَٰكِنَّهُمْ قَوْمٌ يَفْرَقُونَ
Ñuy waat ci Yàlla, naan ñoom ci yéen lañu bokk ; te bokkuñu ci yéen. Waaye ñoom dañoo ragal rekk ngeen dal (ci seen kaw).
57لَوْ يَجِدُونَ مَلْجَأً أَوْ مَغَارَاتٍ أَوْ مُدَّخَلًا لَّوَلَّوْا إِلَيْهِ وَهُمْ يَجْمَحُونَ
Bu ñu amoon làquwaay walla xunti walla fu ñu dugg (ba raw), kon ñu dëddu jëm fa te gaaw ca.
58وَمِنْهُم مَّن يَلْمِزُكَ فِي الصَّدَقَاتِ فَإِنْ أُعْطُوا مِنْهَا رَضُوا وَإِن لَّمْ يُعْطَوْا مِنْهَا إِذَا هُمْ يَسْخَطُونَ
Am na ci ñoom ñu la ayibal ci sarax yi : ku leen ca joxoon ñu bég ca ; ku leen joxul ñu xundu.
59وَلَوْ أَنَّهُمْ رَضُوا مَا آتَاهُمُ اللَّهُ وَرَسُولُهُ وَقَالُوا حَسْبُنَا اللَّهُ سَيُؤْتِينَا اللَّهُ مِن فَضْلِهِ وَرَسُولُهُ إِنَّا إِلَى اللَّهِ رَاغِبُونَ
Lu tee ñu bég ca la leen Yàlla ak Yonentam jox ? Tey wax : “Yàlla doy nanu. Yàlla Dana nu jox ci mbaaxam ak Yonentam it !... Nun way-xemmem lanu jëm ci Yàlla ”.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
57Aaya

Tekki — At-Tawba 57

Simoore At-Tawba Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu amoon làquwaay walla xunti walla fu ñu dugg…

Simoore Aaya 57/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers