At-Tawba · 78/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
أَلَمْ يَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ سِرَّهُمْ وَنَجْوَاهُمْ وَأَنَّ اللَّهَ عَلَّامُ الْغُيُوبِ ٧٨
Transliteration
Alam ya`lamooo annal laaha ya`lamu sirrahum wa najwaahum wa annal laaha `Allaamul Ghuyoob
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dañoo xamul ne Yàlla xam na seen mbóot ya nëbbu ak seenub déeyoo, te nag Yàlla mooy xamaakoonub kumpa.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 76-80 — At-Tawba
76فَلَمَّا آتَاهُم مِّن فَضْلِهِ بَخِلُوا بِهِ وَتَوَلَّوا وَّهُم مُّعْرِضُونَ
Ba leen Yàlla mayee ci mbaaxam (alal), ñu nay ci joxe, ginnaaw ba ñu fuuyu.
77فَأَعْقَبَهُمْ نِفَاقًا فِي قُلُوبِهِمْ إِلَىٰ يَوْمِ يَلْقَوْنَهُ بِمَا أَخْلَفُوا اللَّهَ مَا وَعَدُوهُ وَبِمَا كَانُوا يَكْذِبُونَ
Tax na Yàlla wuutale ci seen xol naaféq ba kera ñuy dajeek Moom ngir la ñu wor Yàlla ca la ñu ko digoon ak ca la ñu doon fen.
78أَلَمْ يَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ سِرَّهُمْ وَنَجْوَاهُمْ وَأَنَّ اللَّهَ عَلَّامُ الْغُيُوبِ
Moo ndax dañoo xamul ne Yàlla xam na seen mbóot ya nëbbu ak seenub déeyoo, te nag Yàlla mooy xamaakoonub kumpa.
79الَّذِينَ يَلْمِزُونَ الْمُطَّوِّعِينَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ فِي الصَّدَقَاتِ وَالَّذِينَ لَا يَجِدُونَ إِلَّا جُهْدَهُمْ فَيَسْخَرُونَ مِنْهُمْ ۙ سَخِرَ اللَّهُ مِنْهُمْ وَلَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Ña nga xam ne dañuy ayibal (sikkal) way-coobarewu ña ci jullit yi ci natt asaka, ak ña nga xam ne amuñu leneen lu dul seeni kàttan ba tax ñuy reetaan lenn ca ñoom. Yàlla Dana leen yéjji te danañu am mbugal mu metti.
80اسْتَغْفِرْ لَهُمْ أَوْ لَا تَسْتَغْفِرْ لَهُمْ إِن تَسْتَغْفِرْ لَهُمْ سَبْعِينَ مَرَّةً فَلَن يَغْفِرَ اللَّهُ لَهُمْ ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَفَرُوا بِاللَّهِ وَرَسُولِهِ ۗ وَاللَّهُ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الْفَاسِقِينَ
Nga balul leen walla nga bañ leen a balul (moo yem) - soo leen baluloon juróom-ñaar fukki yoon - du tax Yàlla baal leen mukk. Ngir dañoo weddi Yàlla ak ub Yonentam te Yàlla du gindi aw nit ñu di ay saay-saay.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
78Aaya
Tekki — At-Tawba 78
Simoore At-Tawba Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dañoo xamul ne Yàlla xam na seen mbóot…Simoore Aaya 78/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers







