Simoore Al-Mursalat ci Aarabu ak Wolof
Jàng Simoore Al-Mursalat ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (50 Aaya — مكية). Al-Mursalat Dégg, Al-Mursalat Tekki, Al-Mursalat mp3, Al-Mursalat pdf.Jàng te Dégg Simoore Al-Mursalat
🎧 Aaya
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
—
x1
أَلَمْ نَخْلُقكُّم مِّن مَّاءٍ مَّهِينٍ ٢٠
📖 Tekki
Aaya 20
Moo ndax bindewunu leen ci ndox mu doyadi
وَجَعَلْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ شَامِخَاتٍ وَأَسْقَيْنَاكُم مَّاءً فُرَاتًا ٢٧
📖 Tekki
Aaya 27
Te def Nanu ci ay tund doj yu kawe? Te nàndale leen ak ndox mu neex ?
انطَلِقُوا إِلَىٰ مَا كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ ٢٩
📖 Tekki
Aaya 29
Fëxleen nag jëm ci li ngeen daan weddi !
انطَلِقُوا إِلَىٰ ظِلٍّ ذِي ثَلَاثِ شُعَبٍ ٣٠
📖 Tekki
Aaya 30
Fëxleen jëm ca ker ga am ñatti tokkoor [saxaar sa] ;
لَّا ظَلِيلٍ وَلَا يُغْنِي مِنَ اللَّهَبِ ٣١
📖 Tekki
Aaya 31
manuta keral kenn waxatumaak di feg tàkk-tàkk ;
إِنَّهَا تَرْمِي بِشَرَرٍ كَالْقَصْرِ ٣٢
📖 Tekki
Aaya 32
moom dafay sànni ay ferñent yu tollu ni njéndi,
هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ ۖ جَمَعْنَاكُمْ وَالْأَوَّلِينَ ٣٨
📖 Tekki
Aaya 38
Lii mooy bisub àtte ba, boole nanu leen ak ñu jëkk ña.
إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي ظِلَالٍ وَعُيُونٍ ٤١
📖 Tekki
Aaya 41
Ña ragal Yàlla ñoom ña nga ca ker ya ak bëti ndox ya.
كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ ٤٣
📖 Tekki
Aaya 43
“Lekkleen te naan, mooy peyug la ngeen daan jëf”.
كُلُوا وَتَمَتَّعُوا قَلِيلًا إِنَّكُم مُّجْرِمُونَ ٤٦
📖 Tekki
Aaya 46
“Lekkleen te bànneexu tuuti ; yéen ay tooñkat ngeen”.
وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ ارْكَعُوا لَا يَرْكَعُونَ ٤٨
📖 Tekki
Aaya 48
Te saasu ñu leen waxee ne : “rukóoleen, duñu rukoo (duñu julli).
فَبِأَيِّ حَدِيثٍ بَعْدَهُ يُؤْمِنُونَ ٥٠
📖 Tekki
Aaya 50
Bu waxtaan wii jàllee, ana wan waxtaan lañuy gëmati ?
Jàng Simoore Al-Mursalat ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers

