Al-Mursalat · 44/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ ۝٤٤
Innaa kazaalika najzil muhsineen
📖 Tekkim Wolof
Noonu la Ñuy faye way rafetal ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-46 — Simoore Al-Mursalat

42وَفَوَاكِهَ مِمَّا يَشْتَهُونَ
Ak ay fuytéef ya ñu bëgg.
43كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
“Lekkleen te naan, mooy peyug la ngeen daan jëf”.
44إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Ñuy faye way rafetal ya.
45وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
46كُلُوا وَتَمَتَّعُوا قَلِيلًا إِنَّكُم مُّجْرِمُونَ
“Lekkleen te bànneexu tuuti ; yéen ay tooñkat ngeen”.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Al-Mursalat 44

Simoore Al-Mursalat Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la Ñuy faye way rafetal ya.

Simoore Aaya 44/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers