Al-Mursalat · 38/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ ۖ جَمَعْنَاكُمْ وَالْأَوَّلِينَ ۝٣٨
Haaza yawmul fasli jama `naakum wal awwaleen
📖 Tekkim Wolof
Lii mooy bisub àtte ba, boole nanu leen ak ñu jëkk ña.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 36-40 — Simoore Al-Mursalat

36وَلَا يُؤْذَنُ لَهُمْ فَيَعْتَذِرُونَ
kenn du leen may pose bu ñuy jéggaloo.
37وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
38هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ ۖ جَمَعْنَاكُمْ وَالْأَوَّلِينَ
Lii mooy bisub àtte ba, boole nanu leen ak ñu jëkk ña.
39فَإِن كَانَ لَكُمْ كَيْدٌ فَكِيدُونِ
Su ngeen amee ay pexe, fexel leen Ma.
40وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Al-Mursalat 38

Simoore Al-Mursalat Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii mooy bisub àtte ba, boole nanu leen ak ñu…

Simoore Aaya 38/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers