Al-Mursalat · 24/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ ۝٢٤
Wailuny yawma `izil lilmukazzibeen
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 22-26 — Simoore Al-Mursalat

22إِلَىٰ قَدَرٍ مَّعْلُومٍ
ba ca ab diir bu ñu xam ?
23فَقَدَرْنَا فَنِعْمَ الْقَادِرُونَ
Nu daldi dogal cëy Noo mana dogal yemale.
24وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
25أَلَمْ نَجْعَلِ الْأَرْضَ كِفَاتًا
Ndax defu nu suuf si mu làmboo lépp,
26أَحْيَاءً وَأَمْوَاتًا
ñuy dund ak ñu dee ?
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Mursalat 24

Simoore Al-Mursalat Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

Simoore Aaya 24/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers