Al-Mursalat · 36/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
وَلَا يُؤْذَنُ لَهُمْ فَيَعْتَذِرُونَ ۝٣٦
Wa laa yu`zanu lahum fa ya`taziroon
📖 Tekkim Wolof
kenn du leen may pose bu ñuy jéggaloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Al-Mursalat

34وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
35هَٰذَا يَوْمُ لَا يَنطِقُونَ
Bu bis baa du ñu mana àddu wax,
36وَلَا يُؤْذَنُ لَهُمْ فَيَعْتَذِرُونَ
kenn du leen may pose bu ñuy jéggaloo.
37وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
38هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ ۖ جَمَعْنَاكُمْ وَالْأَوَّلِينَ
Lii mooy bisub àtte ba, boole nanu leen ak ñu jëkk ña.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Al-Mursalat 36

Simoore Al-Mursalat Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : kenn du leen may pose bu ñuy jéggaloo.

Simoore Aaya 36/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers