Al-Mursalat · 21/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
فَجَعَلْنَاهُ فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ ۝٢١
Faja`alnaahu fee qaraarim makeen
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi koy saxal ci barab wu wóor,

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore Al-Mursalat

19وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
20أَلَمْ نَخْلُقكُّم مِّن مَّاءٍ مَّهِينٍ
Moo ndax bindewunu leen ci ndox mu doyadi
21فَجَعَلْنَاهُ فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ
Nu daldi koy saxal ci barab wu wóor,
22إِلَىٰ قَدَرٍ مَّعْلُومٍ
ba ca ab diir bu ñu xam ?
23فَقَدَرْنَا فَنِعْمَ الْقَادِرُونَ
Nu daldi dogal cëy Noo mana dogal yemale.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Al-Mursalat 21

Simoore Al-Mursalat Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi koy saxal ci barab wu wóor,

Simoore Aaya 21/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers