Al-Mursalat · 37/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ ۝٣٧
Wailunw yawma `izil lilmukazzibeen
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Simoore Al-Mursalat

35هَٰذَا يَوْمُ لَا يَنطِقُونَ
Bu bis baa du ñu mana àddu wax,
36وَلَا يُؤْذَنُ لَهُمْ فَيَعْتَذِرُونَ
kenn du leen may pose bu ñuy jéggaloo.
37وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
38هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ ۖ جَمَعْنَاكُمْ وَالْأَوَّلِينَ
Lii mooy bisub àtte ba, boole nanu leen ak ñu jëkk ña.
39فَإِن كَانَ لَكُمْ كَيْدٌ فَكِيدُونِ
Su ngeen amee ay pexe, fexel leen Ma.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Al-Mursalat 37

Simoore Al-Mursalat Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

Simoore Aaya 37/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers