Al-Mursalat · 20/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
أَلَمْ نَخْلُقكُّم مِّن مَّاءٍ مَّهِينٍ ۝٢٠
Alam nakhlukkum mimmaaa`im maheen
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax bindewunu leen ci ndox mu doyadi

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Simoore Al-Mursalat

18كَذَٰلِكَ نَفْعَلُ بِالْمُجْرِمِينَ
Noonu la ñuy def ak tooñkat ya.
19وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
20أَلَمْ نَخْلُقكُّم مِّن مَّاءٍ مَّهِينٍ
Moo ndax bindewunu leen ci ndox mu doyadi
21فَجَعَلْنَاهُ فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ
Nu daldi koy saxal ci barab wu wóor,
22إِلَىٰ قَدَرٍ مَّعْلُومٍ
ba ca ab diir bu ñu xam ?
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Mursalat 20

Simoore Al-Mursalat Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax bindewunu leen ci ndox mu doyadi

Simoore Aaya 20/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers