Al-Mursalat · 40/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ ۝٤٠
Wailuny yawma`izil lilmukazzibeen
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 38-42 — Simoore Al-Mursalat

38هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ ۖ جَمَعْنَاكُمْ وَالْأَوَّلِينَ
Lii mooy bisub àtte ba, boole nanu leen ak ñu jëkk ña.
39فَإِن كَانَ لَكُمْ كَيْدٌ فَكِيدُونِ
Su ngeen amee ay pexe, fexel leen Ma.
40وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
41إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي ظِلَالٍ وَعُيُونٍ
Ña ragal Yàlla ñoom ña nga ca ker ya ak bëti ndox ya.
42وَفَوَاكِهَ مِمَّا يَشْتَهُونَ
Ak ay fuytéef ya ñu bëgg.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — Al-Mursalat 40

Simoore Al-Mursalat Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

Simoore Aaya 40/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers