Al-Mursalat · 29/50
Tekki Waxtaan — Al-Mursalat
انطَلِقُوا إِلَىٰ مَا كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ ٢٩
Transliteration
Intaliqooo ilaa maa kuntum bihee tukazziboon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Fëxleen nag jëm ci li ngeen daan weddi !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 27-31 — Al-Mursalat
27وَجَعَلْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ شَامِخَاتٍ وَأَسْقَيْنَاكُم مَّاءً فُرَاتًا
Te def Nanu ci ay tund doj yu kawe? Te nàndale leen ak ndox mu neex ?
28وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
29انطَلِقُوا إِلَىٰ مَا كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
Fëxleen nag jëm ci li ngeen daan weddi !
30انطَلِقُوا إِلَىٰ ظِلٍّ ذِي ثَلَاثِ شُعَبٍ
Fëxleen jëm ca ker ga am ñatti tokkoor [saxaar sa] ;
31لَّا ظَلِيلٍ وَلَا يُغْنِي مِنَ اللَّهَبِ
manuta keral kenn waxatumaak di feg tàkk-tàkk ;
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
29Aaya
Tekki — Al-Mursalat 29
Simoore Al-Mursalat Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fëxleen nag jëm ci li ngeen daan weddi !Simoore Aaya 29/50 — Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mursalat Dégg, Al-Mursalat Tekki, Al-Mursalat mp3, Al-Mursalat pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








