Al-Mursalat · 25/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
أَلَمْ نَجْعَلِ الْأَرْضَ كِفَاتًا ۝٢٥
Alam naj`alil arda kifaataa
📖 Tekkim Wolof
Ndax defu nu suuf si mu làmboo lépp,

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Al-Mursalat

23فَقَدَرْنَا فَنِعْمَ الْقَادِرُونَ
Nu daldi dogal cëy Noo mana dogal yemale.
24وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
25أَلَمْ نَجْعَلِ الْأَرْضَ كِفَاتًا
Ndax defu nu suuf si mu làmboo lépp,
26أَحْيَاءً وَأَمْوَاتًا
ñuy dund ak ñu dee ?
27وَجَعَلْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ شَامِخَاتٍ وَأَسْقَيْنَاكُم مَّاءً فُرَاتًا
Te def Nanu ci ay tund doj yu kawe? Te nàndale leen ak ndox mu neex ?
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Mursalat 25

Simoore Al-Mursalat Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax defu nu suuf si mu làmboo lépp,

Simoore Aaya 25/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers