Al-Mursalat · 30/50
Tekki Waxtaan — Al-Mursalat
انطَلِقُوا إِلَىٰ ظِلٍّ ذِي ثَلَاثِ شُعَبٍ ٣٠
Transliteration
Intaliqooo ilaa zillin zee salaasi shu`ab
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Fëxleen jëm ca ker ga am ñatti tokkoor [saxaar sa] ;
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 28-32 — Al-Mursalat
28وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
29انطَلِقُوا إِلَىٰ مَا كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
Fëxleen nag jëm ci li ngeen daan weddi !
30انطَلِقُوا إِلَىٰ ظِلٍّ ذِي ثَلَاثِ شُعَبٍ
Fëxleen jëm ca ker ga am ñatti tokkoor [saxaar sa] ;
31لَّا ظَلِيلٍ وَلَا يُغْنِي مِنَ اللَّهَبِ
manuta keral kenn waxatumaak di feg tàkk-tàkk ;
32إِنَّهَا تَرْمِي بِشَرَرٍ كَالْقَصْرِ
moom dafay sànni ay ferñent yu tollu ni njéndi,
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
30Aaya
Tekki — Al-Mursalat 30
Simoore Al-Mursalat Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fëxleen jëm ca ker ga am ñatti tokkoor [saxaar sa]…Simoore Aaya 30/50 — Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mursalat Dégg, Al-Mursalat Tekki, Al-Mursalat mp3, Al-Mursalat pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








