Al-Mursalat · 42/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
وَفَوَاكِهَ مِمَّا يَشْتَهُونَ ۝٤٢
Wa fawaakiha mimmaa yastahoon
📖 Tekkim Wolof
Ak ay fuytéef ya ñu bëgg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Simoore Al-Mursalat

40وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
41إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي ظِلَالٍ وَعُيُونٍ
Ña ragal Yàlla ñoom ña nga ca ker ya ak bëti ndox ya.
42وَفَوَاكِهَ مِمَّا يَشْتَهُونَ
Ak ay fuytéef ya ñu bëgg.
43كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
“Lekkleen te naan, mooy peyug la ngeen daan jëf”.
44إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Ñuy faye way rafetal ya.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Al-Mursalat 42

Simoore Al-Mursalat Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak ay fuytéef ya ñu bëgg.

Simoore Aaya 42/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers