Al-Mursalat · 39/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
فَإِن كَانَ لَكُمْ كَيْدٌ فَكِيدُونِ ۝٣٩
Fa in kaana lakum kaidun fakeedoon
📖 Tekkim Wolof
Su ngeen amee ay pexe, fexel leen Ma.

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Al-Mursalat

37وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
38هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ ۖ جَمَعْنَاكُمْ وَالْأَوَّلِينَ
Lii mooy bisub àtte ba, boole nanu leen ak ñu jëkk ña.
39فَإِن كَانَ لَكُمْ كَيْدٌ فَكِيدُونِ
Su ngeen amee ay pexe, fexel leen Ma.
40وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
41إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي ظِلَالٍ وَعُيُونٍ
Ña ragal Yàlla ñoom ña nga ca ker ya ak bëti ndox ya.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Al-Mursalat 39

Simoore Al-Mursalat Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su ngeen amee ay pexe, fexel leen Ma.

Simoore Aaya 39/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers