Al-Mursalat · 34/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ ۝٣٤
Wailuny yawma `izil lilmukazibeen
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Simoore Al-Mursalat

32إِنَّهَا تَرْمِي بِشَرَرٍ كَالْقَصْرِ
moom dafay sànni ay ferñent yu tollu ni njéndi,
33كَأَنَّهُ جِمَالَتٌ صُفْرٌ
dañu melni ay giléem yu mboq
34وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
35هَٰذَا يَوْمُ لَا يَنطِقُونَ
Bu bis baa du ñu mana àddu wax,
36وَلَا يُؤْذَنُ لَهُمْ فَيَعْتَذِرُونَ
kenn du leen may pose bu ñuy jéggaloo.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Mursalat 34

Simoore Al-Mursalat Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

Simoore Aaya 34/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers