Al-Mursalat · 31/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
لَّا ظَلِيلٍ وَلَا يُغْنِي مِنَ اللَّهَبِ ۝٣١
Laa zaleelinw wa laa yughnee minal lahab
📖 Tekkim Wolof
manuta keral kenn waxatumaak di feg tàkk-tàkk ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 29-33 — Simoore Al-Mursalat

29انطَلِقُوا إِلَىٰ مَا كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
Fëxleen nag jëm ci li ngeen daan weddi !
30انطَلِقُوا إِلَىٰ ظِلٍّ ذِي ثَلَاثِ شُعَبٍ
Fëxleen jëm ca ker ga am ñatti tokkoor [saxaar sa] ;
31لَّا ظَلِيلٍ وَلَا يُغْنِي مِنَ اللَّهَبِ
manuta keral kenn waxatumaak di feg tàkk-tàkk ;
32إِنَّهَا تَرْمِي بِشَرَرٍ كَالْقَصْرِ
moom dafay sànni ay ferñent yu tollu ni njéndi,
33كَأَنَّهُ جِمَالَتٌ صُفْرٌ
dañu melni ay giléem yu mboq
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Al-Mursalat 31

Simoore Al-Mursalat Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : manuta keral kenn waxatumaak di feg tàkk-tàkk ;

Simoore Aaya 31/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers