Al-Mursalat · 43/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ ۝٤٣
Kuloo washraboo haneee `am bimaa kuntum ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
“Lekkleen te naan, mooy peyug la ngeen daan jëf”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 41-45 — Simoore Al-Mursalat

41إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي ظِلَالٍ وَعُيُونٍ
Ña ragal Yàlla ñoom ña nga ca ker ya ak bëti ndox ya.
42وَفَوَاكِهَ مِمَّا يَشْتَهُونَ
Ak ay fuytéef ya ñu bëgg.
43كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
“Lekkleen te naan, mooy peyug la ngeen daan jëf”.
44إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Ñuy faye way rafetal ya.
45وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — Al-Mursalat 43

Simoore Al-Mursalat Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Lekkleen te naan, mooy peyug la ngeen daan jëf”.

Simoore Aaya 43/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers