Al-Mursalat · 28/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ ۝٢٨
Wailuny yawma `izil lilmukazzibeen
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 26-30 — Simoore Al-Mursalat

26أَحْيَاءً وَأَمْوَاتًا
ñuy dund ak ñu dee ?
27وَجَعَلْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ شَامِخَاتٍ وَأَسْقَيْنَاكُم مَّاءً فُرَاتًا
Te def Nanu ci ay tund doj yu kawe? Te nàndale leen ak ndox mu neex ?
28وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
29انطَلِقُوا إِلَىٰ مَا كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
Fëxleen nag jëm ci li ngeen daan weddi !
30انطَلِقُوا إِلَىٰ ظِلٍّ ذِي ثَلَاثِ شُعَبٍ
Fëxleen jëm ca ker ga am ñatti tokkoor [saxaar sa] ;
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Mursalat 28

Simoore Al-Mursalat Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.

Simoore Aaya 28/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers