Al-Mursalat · 32/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
إِنَّهَا تَرْمِي بِشَرَرٍ كَالْقَصْرِ ۝٣٢
Innahaa tarmee bishararin kalqasr
📖 Tekkim Wolof
moom dafay sànni ay ferñent yu tollu ni njéndi,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 30-34 — Simoore Al-Mursalat

30انطَلِقُوا إِلَىٰ ظِلٍّ ذِي ثَلَاثِ شُعَبٍ
Fëxleen jëm ca ker ga am ñatti tokkoor [saxaar sa] ;
31لَّا ظَلِيلٍ وَلَا يُغْنِي مِنَ اللَّهَبِ
manuta keral kenn waxatumaak di feg tàkk-tàkk ;
32إِنَّهَا تَرْمِي بِشَرَرٍ كَالْقَصْرِ
moom dafay sànni ay ferñent yu tollu ni njéndi,
33كَأَنَّهُ جِمَالَتٌ صُفْرٌ
dañu melni ay giléem yu mboq
34وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Mursalat 32

Simoore Al-Mursalat Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : moom dafay sànni ay ferñent yu tollu ni njéndi,

Simoore Aaya 32/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers