Al-Mursalat · 41/50
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mursalat
إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي ظِلَالٍ وَعُيُونٍ ۝٤١
Innal muttaqeena fee zilaalinw wa `uyoon
📖 Tekkim Wolof
Ña ragal Yàlla ñoom ña nga ca ker ya ak bëti ndox ya.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 39-43 — Simoore Al-Mursalat

39فَإِن كَانَ لَكُمْ كَيْدٌ فَكِيدُونِ
Su ngeen amee ay pexe, fexel leen Ma.
40وَيْلٌ يَوْمَئِذٍ لِّلْمُكَذِّبِينَ
Bu keroogee xuru safara ñeel na ñay weddi.
41إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي ظِلَالٍ وَعُيُونٍ
Ña ragal Yàlla ñoom ña nga ca ker ya ak bëti ndox ya.
42وَفَوَاكِهَ مِمَّا يَشْتَهُونَ
Ak ay fuytéef ya ñu bëgg.
43كُلُوا وَاشْرَبُوا هَنِيئًا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
“Lekkleen te naan, mooy peyug la ngeen daan jëf”.
Al-MursalatFihi Alxuraan
50Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — Al-Mursalat 41

Simoore Al-Mursalat Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ragal Yàlla ñoom ña nga ca ker ya ak…

Simoore Aaya 41/50 — Simoore Al-Mursalat المرسلات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mursalat Dégg, Simoore Al-Mursalat Tekki, Simoore Al-Mursalat mp3, Simoore Al-Mursalat pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers